Aller au contenu

ëyu g-

Jóge Wiktionary.

wolof

[Soppi]
  • woo ku la sori, ëyu na ko: woo na ko cig sori, nee na ko ée.

way bawoo yi :

  • ëyu giy tekki "woote ci ëyukaay"
  • ëyukaay: jumtukaayu ëyu (woote cig sori)

français

[Soppi]
  • appeler à distance
  • téléphoner
  • téléphone