Aller au contenu

njénd

Jóge Wiktionary.

wolof

[Soppi]
  • njénd mooy kër gu mag gu taaru gi buur biy dëkke.
  • dëkkuwaayu njiitu réew, njéndul njiitu réew. L nag lay àndal: njénd li, lenn njénd

Francais

[Soppi]
  • palais

Italiano

[Soppi]
  • palazzo