nguurug ngóora

Jóge Wiktionary.
Aller à la navigation Aller à la recherche

nguur giy tegu ci gëm-gëmu: ngóora mooy liy def nit ki mu tiim ku dul ki ko yor, te jiggéen yoru ko, kon dan koy yilif, moom daal liggéeyam weesuwul ëmb ak jur ak topp ci ginnaaw góor mi yor mgóora ak kàttan