ngérum geneen-àddinaal

Jóge Wiktionary.
Aller à la navigation Aller à la recherche

dees na ko wax it "geneen wërngëlal" mbaa "geneen-kol-kolal". Wërngëlal ak kol-kolal dañuy tekki ci baatu fr bii di "globalisation" nga xam ne mi ngi bawoo ci globe giy tekki "kol-kol mbaa wërngal gi suuf si def, kon kol-kolal mbaa wërngëlal ñooy globalisation