Aller au contenu

jëggaani

Jóge Wiktionary.
(Yoonalaat gu jóge jëggaani g-)

ag jëggaani

wolof

[Soppi]
  • wuti lëf fu dul fa nga dëkk
  • jëli ay silaa (marsandiis) ca bitim réew, jaaysi leen ci am réew ngir néew gu mu fa néew, walla ngir neex gu mu fa neex a jaaye(1)

français

[Soppi]
  • importer(1)