doggantal

Jóge Wiktionary.
Dem: Joowiin, Seet

wolof[Soppi]

  • dogat
  • ag doggantal:daggat gees di def ab bunt ci ab téere, def ko ay xaaj, maanaam jël bunt bi aju ci jaamu Yàlla yi, def ko ay doggantal, gii jëm ci julli, gii jëm ci woor, gee ca jàpp, bu ñu noppee jëlati beneen bunt, moo xam daa aju ci jëflante yi, mbaa leneen, misaal ñu jël buntu jëflante yi, séddale ko ci ay doggantal, gii jëm ci fas-soxna, gee ca njaay añs.

français[Soppi]

  • chapitre