daara (ji)
Apparence
(Yoonalaat gu jóge daara (jenn))
Wolof
[Soppi]Mooy barab ba ñuy jànge ak a jàngale, cosaan la: fa jàngkati alxuraan ya daan jànge ak way xamlu diiney Lislaam ya, mu jëm-kanam ba ñu mujj di ko jëfandikoo ci lépp lu di barabu njàng ak njàggale
Turandoo
[Soppi]Yeneeni làkk
[Soppi]| wu faraas: école, centre |
| wu itaali: scuola |
| wu angalteer: school |