Aller au contenu

bàkk

Jóge Wiktionary.

Wolof

[Soppi]

→ Mottalil gongikubaat bi. (Soppi)

bàkk -b:

  1. bàkk wax juy wone ag man-man mbaa a xam-xam mbaa kàttan.
  2. bàkkub Senegaal de Sengoor moo ko bind

Bàkk:

  1. mbër suy dugg si géew bi danga koy bàkk ngir yokk ko doole

Xool it

[Soppi]