asaka

Jóge Wiktionary.
Sauter à la navigation Sauter à la recherche

Wolof[Soppi]

Nuvola apps bookcase.svg Gongikubaat[Soppi]

baatub asaka ci lakku araab la bawoo.→ Mottalil gongikubaat bi. (Soppi)

Open book 01.svg Tur[Soppi]

asaka j

  1. li jullit bi di jël ci alalam at mu jot ngir jox ko néew-di-doole yi.