Aller au contenu

àlliwa

Jóge Wiktionary.
(Yoonalaat gu jóge alliwa)

Wolof

[Soppi]

→ Mottalil gongikubaat bi. (Soppi)

àlliwa b:

  1. ci xayma: day am ay keno ak ay rëdd, ci seen diggante ñu ciy man a bind
  2. Mooy nekk ci jàngu yi, te jàngalekat yi di ci bind.

àlluwa

wu-faraas: tableau

Waxiin

Déglul baatu àlliwa ci wolofi Senegaal