adduna

Jóge Wiktionary.
Sauter à la navigation Sauter à la recherche

wolof[Soppi]

Nuvola apps bookcase.svg Gongikubaat[Soppi]

ci wolof yi

Open book 01.svg Tur[Soppi]

adduna:amna ñaari maanaa

  1. adduna njendi lii ñu nekk di ci dund asamaan-ak suuf ak lici aju.
  2. dund gi yit dinañ ko wax adduna,misaal:astu toppu nà goné yu goór yi ba yaq addunaam


aji dugal[Soppi]

Abdu Xaadir Géy Ahloubadar

Bokktekki[Soppi]

Tekki ci yeneeni làkk[Soppi]