yonnee
Apparence
(Yoonalaat gu jóge Yonnee)
wolof
[Soppi]- yabale
- tukkib xam-xam ci réew mu sori, mbaa mu jafe, walla tukkib nemmiku bu am solo mbaa mu xaw a yëngu;nit ak bagaas yi bokk ci tukki bii: ab yonne bu jëm dottub bëj-saalum
français
[Soppi]- expédition:
Voyage scientifique dans un pays éloigné ou difficile, ou voyage touristique plus ou moins important ou mouvementé ; hommes et matériel participant à ce voyage : Expédition au pôle Sud.