Aller au contenu

Sanc

Jóge Wiktionary.

Wolof

[Soppi]
  • sanc: mooy dem ci beneen barab boo dëkkutoon sanc ko, moo xam fu kenn dëkkutoon la mbaa muy ab gent, mbaa fu nit dëkk, xajale fa mbaa ñu jaay ko doole
  • dem cib barab took fa, dëkk fa cig sañ-bañ, yilif ña fa dëkk ci doole, (mi ngi juge ci canc gi ñu njëkk a wax, ci tomb bi ci kaw) (1)

Yeneen làkk

[Soppi]

Français

[Soppi]
  • coloniser (1)

Italiano

[Soppi]
  • colonizzare

English

[Soppi]
  • colonize