ñu-pay-gu-saxadi

Jóge Wiktionary.
Aller à la navigation Aller à la recherche

baat la buy wone liggéeykat yi yor ay payoor yu wóoradi te saxadi, jamono ju nekk man nañoo ñàkk seeni liggéey, mbaa ñu dàq leen, mu leen di wone niki ag kuréelug mboolaay gu yees