taariix

Jóge Wiktionary.

Dem : Joowiin, Seet

Tëraliin

[Soppi] wolof

[Soppi] Nuvola apps bookcase.svg Gongikubaat

Baat baa ngi jóge ci làkku araab.

[Soppi] Open book 01.svg Tur

Taariix:

  1. Xew-xewu démb
    Taariixu senegaal, di li xewoon senegaal dale ca ñoom maam ba tay jii, seen bépp jaar-jaar.
    Ci arminaat
    mooy lay wax bés bi ñu ne ak weer wi ak at mi, ci misaal: tay la 1 ut 2005

[Soppi] Yeneeni làkk

wu faraas: histoire, date
wu angalteer: history, date