dig

Jóge Wiktionary.

Dem : Joowiin, Seet

[Soppi] wolof

[Soppi] Nuvola apps bookcase.svg Gongikubaat

Am na ñaari tekki:

Aw dig
aw rëdd walla liy tàqale diggante ñaari réew mbaa ay barab
Dig
wax kenn di nga ko defali dara, dig naa ko ne dinaa ko seeti.

[Soppi] yeneeni làkk

wu faraas : frontière, promesse
wu angalteer: border, promise
wu itaali: frontiera, confine, promessa
Ci « http://wo.wiktionary.org/wiki/dig » lañ ko jële