dëkk
Jóge Wiktionary.
Tëraliin |
[Soppi] wolof
[Soppi]
Gongikubaat
→ Mottalil gongikubaat bi. (Soppi)
[Soppi]
Tur
dëkk (b):
- ci melosuuf: ag dajaloo gu ay nit aki kër yu takku te lëw
[Soppi]
Jëf
dëkk:
- Dem fenn samp fa kër nekk fa, di fa amal say yëngu-yëngu
[Soppi] Bokktekki
[Soppi] yeneeni làkk
| wu-angalteer: city, live |
| wu-fraas: ville, habiter |
| wu-itaali: città, abitare |