bakkan

Jóge Wiktionary.
Dem : Joowiin, Seet

Tëraliin

[Soppi] wolof

[Soppi] Nuvola apps bookcase.svg Gongikubaat

bakkan: amna ñaari piri

  1. bakkan ab cér la ci nit, dees koy jëfandikoo ngir nóyyi ak ñàndu...
  2. bakkana dees nako wax ngir jublu si liy waral nit di dund, niki diw ñàkk na bakkanam/dee na.

[Soppi] Xool it

[Soppi] ci yeneeni làkk

Nuvola apps edu languages.svg Waxiin

Déglu baatu bakkan ci wolofi Senegaal

Wo-bakkan.ogg
Samay jumtukaay
Barabu tur

Wuute
Jëf
Joowiin
Boyotu jumtukaay yi
Yeneeni làkk