Abajada wolof

Jóge Wiktionary.

Wolof[Soppi]

Lii mooy abajada wolof bi nguuru senegaal jàpp, képp kuy bind wolof war cee tënku

Abajada wolof[Soppi]

a - à - aa - b - bb - c - cc - d - dd- e - ee- é - ée - ë - ëe - f- g - gg - i - ii - j - jj - k - kk - l - ll- m - mm - mb - n - nn - nc - nd - ng - nj - nk - nq - nt - ñ - ññ - η - ηη - o - oo - ó - óo - p - pp - q - r- rr - s - t - tt - u - uu - w - ww - x - y - yy.

Araf Bopp Biir Mujj
1 a, A am sabar mala
2 à, À àllarba muskàllaf amul
3 aa, Aa aar talaata Tuubaa
4 b, B bax jabar rab (rabu àll)
5 bb amul jebbi bb
6 c, C coono looco amul
7 cc amul soccu cc
8 d, D der xadar amul
9 dd amul buddi sedd
10 e, E em xel fexe
11 ee, Ee ee bees bee
12 é, É amul béy xulé1
13 ée, Ée éem féey bu bëggée1
14 ë, Ë ës fës amul
15 ëe, Ëe amul bëer amul
16 f, F for nafar nef
17 g, G garab jagal nag (nagu Sàmba)
18 gg amul rogganti segg
19 i, I itte tis kaani
20 ii, Ii iir riiti bii
21 j, J jabar fajar faj (fajal)
22 jj amul jji bojj
23 k, K kafe saaku ak
24 kk amul kkaan lekk
25 l, L lam nelaw xel
26 ll amul xolli ll
27 m, M mar laman xam
28 mm amul mm mm
29 mb, Mb mbootu mbar mb
30 mp amul mpóor samp
31 n, N nar daanu fen
32 nn amul nnu wann
33 nc amul dencukaay sanc
34 nd, Nd ndox rendi nd
35 ng, Ng ngoon teraanga lang
36 nj, Nj njàmbal njul donj
37 nk amul nkar nk
38 nq amul sanqal janq
39 nt amul santaane bant
40 ñ, Ñ ñam wañaaru ngooñ
41 ññ amul ññi ññ
42 η ηaam daηar laη
43 ηη amul ηηarñi doηη
44 o, O opp lop laalo
45 oo, Oo oom boroom àndandoo
46 ó óbbali jóg pusó1
47 óo óom góor xulóo1
48 p put ciipatu amul
49 pp amul ηàppati lupp
50 q (ñaari xx) amul qarci q
51 r, R raxas maral liir
52 rr amul amul fërr
53 s, S suuf desit fas
54 t, T tool tuuti nit
55 u, U um buddi kuddu
56 uu, Uu uuf buur luu
57 w, W wasin tawat xew
58 ww amul xewwi jaww
59 x, X xar saxaar lex
60 y, Y yaram layoo bey
61 yy amul feyyu coyy

1- Doonte sax, li ñu téj ci biir lonk yi ngay dégg, nanga bind: xule, bu bëggee, pus, xuloo.